Voici Kéémtalay Kattane, un extrait du pré-album #The_MossTape en hommage à tous ceux qui s'arment d'Espoir, de Courage et d'Endurance. C'est dans une ambiance chaude d'émotions que cette vidéo a été tournée avec la complicité de marchants ambulants,d'ouvriers,d'hommes,de femmes;d'enfants ...dont la spontanéité étonnera plus d'un. MERCI immensément KEUR MASSAR pour la Solidarité,l'Affection,l'Amour,le Respect ...Votre Hymne est enfin là!
Auteur : Sir Jamal
Studio enregistrement, mix, edit & mastering : Labo 36 Record par Foflow et Thiorka
Une production de Labo 36 Record (Dakar, Senegal, août 2019)
Réalisation : Labo 36 Films avec Agas à la baguette
Retrouvez Sir Jamal sur les réseaux sociaux**
Facebook : SIR JAMAL
Instagram : sir_jamal_og
Snapchat : sirjamal
** Contact management**
M. Ousmane Ndiaye : +221 77 987 81 95
**Lyrics de la chanson**:
Dinga ci guéneu ,dinga ci guéneu kéne meunouci léneu
Dinga ci guéneu, dinga ci guéneu kéne meunouci léneu (Bis)
**Refrain**
Gueumeul ni lépp lingay yootou dingci meusseu djott one day
Yonou ndaw dou gaaw ,yow gnaféél té gueuneuleu wéy ci wout kheuy
Déffal sa kéémtalay kattane
Yonou ndaw dou gaaw ,yow gnaféél té gueuneuleu wéy ci wout kheuy
***Couplet***
Alleu bangui reupp ,lila ciy mouthieul moy nga yor fitou gayndé
Amal eudeupp loumou méti bouldi khadi dokhéél jom lou ngande
Takoul mou deugueur ,boko beugué wéssou djafé djafé doundou fandé
Té ngueum gui na wér ;ni kheuthieu bou dagoul dina dikkaki yeurmandé
(GOOR FALL)
Teukeul sa lépp now boul khaar toomorrow
Bou goudi gui di léér dieuf dji nay law
Sigui sigui bagna seugg ci waarou
Job, Labali sa fass ni maalaw
Yéneu saay mbir yi diéki tassaaroo
Wayé yagg yagg dina takou wassaaroo
Boul toogg khaar deuk ci nélaw
Yokk thiéré dolli gnéékh mou falaw
Dina hard,dina deugueur,dina thiool way moudjéntéél gui dina néékhi
(AKASSA)
Ndéké tar tar yi ,natou yinga dékou; liciy topp moy sa tékki
Dinga ci guéneu, dinga ci guéneu kéne meunouci léneu (Bis)
**Refrain**
Gueumeul ni lépp lingay yootou dingci meusseu djott one day
Yonou ndaw dou gaaw ,yow gnaféél té gueuneuleu wéy ci wout kheuy
Déffal sa kéémtalay kattane
Yonou ndaw dou gaaw ,yow gnaféél té gueuneuleu wéy ci wout kheuy......
***Toutes nos excuses pour ce Wolof mal écrit***
Veuillez vous connecter pour commenter