** Abonnez vous au Journal Rappé ici https://goo.gl/nhtjbS **
Le nouveau clip egotrip du rappeur Jailer Bangz, "Nekh",
#JailerBangz #Nekh #ClipOfficiel #WeeFlage #Team221
** Les crédits du Clip "Nékh" **
Beat: Gob beat mix
Master :Natty dread
Réalisation : WeeFlage
** Retrouvez l'artiste Jailer Bangz sur **
YouTube: https://www.youtube.com/c/JailerBangzofficial
facebook : https://www.facebook.com/jailerbangzjailerbangbang/
instagram : https://www.instagram.com/jailer_bangz_lofficiel/
Twitter : https://twitter.com/Jailerbangz
Snapchat : @jailerbxy
** Les paroles de la chanson "Nékh" **
1er couplet
Ragalouma kouma sandi khér pakh bissa bop Bi guéné lakoy délo
Mangui sama gnarélou veres diko yeungueul si bar yi boy nganane ma déggo
Féthieu sama Bakou bang bang sisa cerveau
Mafi fégnal atou boy boulné ma déggo
Ma fi djeulé pa Bi
Done fi séni dadj yi
Mala meune fouf dou sakh exoco
Bobou ba légui Mangui khireul yéne gneup lay takeu saréte
Téla djongou gawa bireul
Mane fouma gneuw rek je pénètre
Sokhor sadique sévère
Naye Métti rek fi dou légère
Mc bana bana yiffi djay affair la wakhsini marché bi nangou na ndém
Fateu ngama ak say règle ,djayoumala sama freedom
Jailer Bangz dafa rew fi kou nek ak djikome
Nigger dadj yi dou fi djékh tay mou melni chantier cofreur
Dama nop sama néné bisou bisous sama chou fleur
BanG
2ème Couplet
Goor Dou mot
Ba gueune ma moT
Kone loutax maley gnéé
Té fi pour gua mol fok guay woné xott
Todialé Say seins
Perversité perversité
Guel yé yomb gawa signé
Boyi sathie defko liguey
Diamou xaliss nek dinéé
Temps boy bopou kogn ba laniouy dianguei rew
Bopou kogn beu tatou mol yi laniouy diew
Amoul neubo sougnou bir ni dialou kanam
Grand yi aek sen guel melni séni jabar
Bayou xaleyi
Bayou samay enemies
Dafma nianone taw ma dieundal ko parapluie
Chaque jour danou ci lale melni dama teuredi
Bayil dima deglou boudé dama teuredi
BanG
3ème Couplet
Tay nga guiss loula yém ba melni sabarou laobé
Beugueutoumeu cho bou toy ,wouteul léne ma guel bou tawté
Waga la wala bandit ,djam mou dougou wala mou bondé
Bayou khalé yi mana ,moune ngama wowé maobé
Yokh la Jamaïque pour mou nekh fok Ngay tir di mir
Mérkate tek la chok ba melni guel you fir
Sorima niggers amoléne futur
Moune nga wakh mane guéneu nassi bayi léne sibir bangz
Refrain
dotougnou bayi limaléne gnamala Nékh
Sama Ex yi beugue déloussi Lima léne gnamala nekh
Limala gnamala nekh limako gnamala nekh
Lima léne ,limala gnamala Nékh
Refrain dotougnou bayi limaléne gnamala Nékh
Sama Ex yi beugue déloussi Lima léne gnamala nekh
Limala gnamala nekh limako gnamala nekh
Lima léne ,limala gnamala Nékh
Veuillez vous connecter pour commenter