** Abonnez vous à ma chaine ici https://bit.ly/subscribepaaparey ** Paaparey chante la "Beauté Africaine", avec Défa du trio Safary en guest.
#Paaparey #BeautéAfricaine #Safary #HikHopMusik
** Les crédits du clip "Beauté Africaine" **
Beat : Yakine Sheikh
Guitare : Steady Key
Mix & mastering : Mario / Diamond Record
Réalisation clip : Awanje Films
Stylisme : Ajavo +221774215459
Remerciement : Safary et son équipe
Production : HikHop Musik (avril 2019, Dakar, Senegal)
** Retrouvez Paaparey sur les réseaux sociaux **
Facebook https://www.facebook.com/PaapaRey
Instagram https://www.instagram.com/paaparey_officiel
Snapchat @paaparey
** Contact management : +221 77 802 61 09 **
** Les lyrics de la chanson "Beauté Africaine" **
Refrain
Rafetay bou djégui dayo
Djék nagn ba melni ouroul ayni
Yeah
Beauté africaine bi nek si niom
Mane momay doflo (2fois
Couplet defa safary
Rafetay bou djegui dayo
Djek tarou nelen machallah
Beuti meune gua si sétou
Derr bou niou
Bou xess ak chocolat
Lifi mami bayi wone
Djougou fi djeulal sa yone girl
Kham fi niou djougué
Fii niou thiossanoo. Ohh yé
Defilél shoody dagoul dokhal noumou la nékhé
Comme djongoma
Naturel comme iow retanal say beugn you wekh
Nekh nama yéyéyé
Beauté africaine bi si iow girl doyna ma haann
Sokhnassiii
Couplet Paaparey .
Setoul khol nigua tarro baby
Sa derr bou nioule bi dékoy ndamo lady
Nagua takk sa seur gnafé ko .
Ohh ahh ohh nooo
Setoul khol lila yalla djaglél
Sa melokane bi mane dafmay danel
Nagua geum li gua done baby
Ohh noo ohhh noo
Nioune yena niouy danel
Nioune yena niouy djoylo
Nioune yene la niouy ndamo baby
Mane way na léne.
Namou lene dara
Yena dakk si adouna
Mane way na lene lady
Defilel shoody dagoul dokhal noumou la nekhé comme djongoma
Naturel comme iow
Retanal say beugn you wekh
Nekh nama haann
Beauté africaine bissi iow girl
Doyna ma
Sokhna siii
Veuillez vous connecter pour commenter