BRAND NEW VIDEO "SUNU-GAAL"
EXTRAIT DU NOUVEL ALBUM "REGGAEVOLUTION TIME"
Please Subscribe: https://www.youtube.com/channel/UCMZT-m9UHnQrQMTlaufoQJw?sub_confirmation=1
merci de souscrire: https://www.youtube.com/channel/UCMZT-m9UHnQrQMTlaufoQJw?sub_confirmation=1
facebook link : https://www.facebook.com/dreadmaxiamar
Twitter link : https://twitter.com/DREADMAXIMAMAR
reverbnation link :https://reverbnation.com/dreadmaximamarsn
SUNU GAAL
Nio nghi diow gaal ga nghi dem
Mba nioun kham na niou dieum
Fa niou dioguek fa niou dieum
Fane mo thi gueun
Diamono di dem di dem di dem di dem di dem diamono
Mba kham na fa mou dieum
Déloul fa ngha diogué diamono bo khamoul fa ngha dieum!
Sunu gaal a nghi dem toop séne gaal di dem
Niou bayi sunu yone toop séne yone di dem
Yone wi niou diel ndakham moy yone wi gueune
Sénégal fane la niou dieummmmmmmm
Fane la niou diem, fane la niou dieuuuuuuuuum
Fane la niou dieum
Mané bi gaal, fane la dieum ?
Nio nghi diow gaal ga nghi dem
Mba nioun kham na niou dieum
Fa niou dioguek fa niou dieum
Fane mo thi gueun
Fane mo thi gueun
Mani gaal gui sunu gaal la na niou diok diow mou dem !
Té lou way di def lou fi way mana défar
Réwame la ko défal
Na niou fight nghir sunu sénégal
Té kou fi falouti nioun nio lay fall
Wanté mane li ma thi diakhal
Yenne djit yi séne bop la niou taaaaaal
Séne bop la niou tal
Séni mbok la niou taaaaal
Séne bop la niou taaal
Mani bi gaaal, fane la dieum
Depuis les ports de l’esclavage aux ports du colonialisme
A quel nouveau port encore allons-nous jeter nos amarres
Une unité africaine se doit !
C’est notre seul et unique choix
Africa réveille toi, et lève toi pour la libertéééé
Lève-toi, pour ta libertéééé
Africa Wake up and live
Wake up and live
Africa time is now
Veuillez vous connecter pour commenter